2 Samuel 18:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buur ne ko: «Ngóor sa Absalom nag, mbaa jàmm la am?» Ayimaas ne ko: «Sang bi, ba Yowab di yónni sa bëkk-néeg ak man, booba gis naa kër-kër ju réy, waaye xawma lu mu doon.»