2 Samuel 19:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kàddu yooyu nag waññi xolu Yudeen ñépp, ñu bokk genn kàddu, daldi yónnee ca Buur ne ko mu délsi, mook nitam ñépp.