2 Samuel 19:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndaxte xam naa ne bàkkaar naa, sang bi. Waaye xoolal tey, Buur, sang bi, waa giirug Yuusufa gépp, maa ci jëkka ñëw gatandusi la.»