2 Samuel 19:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Mefiboset, sëtub Sóol, dikk moom it, di teertusi Buur. Diggante bés ba Buur gàddaayee nag, ba bésub keroog ba mu délseek jàmm ca Yerusalem, Mefiboset jànguwul, watul sikkimam, te fóotul ay yéreem.