2 Samuel 19:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat sang bi, du kenn ci sama askanu maam ku yelloowul lu moy nga rey ko. Terewul danga maa xajal, sang bi, boole ma ci ñiy bokk ak yaw ndab. Kon Buur, ana lu ma la sañatee ñaan?»