2 Samuel 19:32 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fekk na Barsilay ma bokk ca Galàdd jóge woon Rogelim, ngir gunge Buur Daawuda, ba mu jàll dexu Yurdan, bala moo tàggtoo ak moom ca wàllaa dex.