2 Samuel 19:33 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Barsilay mag la woon. Amoon na juróom ñett fukki at. Moom moo daan topptoo Buur diir ba mu nekk Maanayim, ndax nit ku bare alal la woon.