2 Samuel 19:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xarekat ya nag di yoxoosuy dugg bésub keroog ca Maanayim, mel ni nit ñu dawe xare, di yoxoosuy ñibbsi, ndax gàcce.