2 Samuel 19:41 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee Buur jàll ba Gilgal, Kimyam ànd ak moom. Mbooloom Yuda gépp ak ñenn ci mbooloom Israyil itam ànd ak Buur dem.