2 Samuel 19:42 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka la loolu am rekk waa Israyil yépp dikk ca Buur, ne ko: «Buur Daawuda, ana lu waral sunu bokki Yuda yi aakimoo la, jàlle la dexu Yurdan, yaak sa waa kër ak sa nit ñi nga àndal ñépp?»