2 Samuel 19:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi nag, jógal kat génn wax ak say nit, ruccanti leen. Ndax giñ naa ci Aji Sax ji, soo génnul, du kenn ku fiy bokk fanaan ak yaw tey. Te loolu de musiba lay doon ci yaw, mu gëna réy musiba mu la masa dal, ba ngay ndaw ba tey.»