2 Samuel 19:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buur daldi jóg, génn, toog ca buntu dëkk ba. Ñu wax mbooloo ma mépp ne leen: «Gisleen Buur a ngee toog ca bunt ba.» Mbooloo mépp dikk taxaw ci wetam. Fekk na bànni Israyil ya faroon ak Absalom daw ñibbi ca seeni kër.