2 Samuel 2:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yowab ak Abisay nag dàqi Abner. Ba jant bay lang, ña nga tollu ca tundu Ama, wa janook Giya, ca yoon wa jëm màndiŋu Gabawon.