2 Samuel 20:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu dikk gaw dëkk ba ñuy wax Abel Bet Maaka, fa Seba làqu. Ci kaw loolu ñu jal suuf fa sës ca buntu dëkk ba, mu kawe ba tollook tatay dëkk ba. La ca tegu xarekati Yowab yépp di jéema màbb tata, ja wër dëkk ba.