2 Samuel 20:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci biir loolu senn as ndaw su am xel ca dëkk ba, woote ne leen: «Dama ne, dégluleen! Neleen Yowab mu ñëw, ma wax ko.»