2 Samuel 20:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Du loolu! Jenn waay ju ñuy wax Seba doomu Bikkri te bokk ca waa tundi Efrayim, moo jógal Buur Daawuda. Joxleen ma ko moom doŋŋ, ma bàyyi dëkk bi te dem.» Ndaw sa ne Yowab: «Xoolal, boppam lañuy tollu ci kaw taax mi, sànni la ko.»