2 Samuel 20:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dem nañu ba tollu ca doj wu mag wa ca Gabawon, doora gis Amasa, muy dox di dajeek ñoom. Yowab a nga sol yérey xareem, laxasaay ga ca ndigg la ànd ak saamar bu roofe ca mbaram. Naka la séqi jéego jëm kanam, saamar ba rot.