2 Samuel 21:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jamono ya Daawuda nekkee ci jal bi, amoon na xiifub ñetti at yu tegloo. Daawuda diis ko Aji Sax ji. Aji Sax ji ne ko: «Li waral xiif bi moo di àqu deret ji topp Sóol ak waa këram ndax waa Gabawon ña mu rey.»