2 Samuel 21:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Daawuda jébbal leen waa Gabawon, ñu jam leen ba mu sar, foofa ca kaw tund wa, fa kanam Aji Sax ji. Juróom ñaar ñooñu ñépp a bokk tëdd. Ña nga leen rey ca fan ya ñu tàmbalee góob, ca ndoortel ngóobum lors ba.