2 Samuel 23:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñeyi xarey Daawuda ya, ñoo di: Yosebasebet waa Agmon ba bokk ca mbëri xare ya. Moo xàcci xeejam, dal ci juróom ñetti téeméeri nit, rey leen ci menn cong.