bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Samuel 24:10
2 Samuel 24:10 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Daawuda waññ askan wa ba noppi, fit wa ne rës, mu yedd boppam, daldi ne Aji Sax ji: «Aji Sax ji, bàkkaar naa lool. Léegi nag ngalla jéggal ma sama ñaawtéef, ndax def naa jëfi dof ju réy lool.»