2 Samuel 24:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gàdd dem ca Daawuda, jottli ko ko, ne ko: «Ana yii yett loo ci taamu, mu dal ci sa kaw: juróom yaari ati xiif ci sam réew, am ñetti weer yooy daw say noon, am ñetti fani mbas ci sam réew? Xalaatal léegi te wax ci lenn, ma xam lu may jottli ki ma yónni.»