bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Samuel 24:2
2 Samuel 24:2 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buur wax ak Yowab ma ca wetam, di njiital xarekat ya. Mu ne ko: «Wëral ci biir giiri Israyil gépp ba ñu daj, li ko dale diiwaanu Dan ca bëj-gànnaar ba Beerseba ca bëj-saalum. Nañu bind askan wi, ndax ma xam seenub lim.»