2 Samuel 24:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee Arawna séen Buur, mu ànd aki jawriñam, jëm ca moom. Mu génn sujjóotal ko, dëpp jëëm ca suuf,