2 Samuel 24:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ne ko: «Buur, sang bi, lu doon say tànk?» Daawuda ne ko: «Xanaa jëndsi sa dàgga jii, ba tabaxal fi Aji Sax ji sarxalukaay, ndax mbas mi dal ci kaw askan wi yem fi.»