2 Samuel 3:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee Abner yebal ca saa sa ay ndaw ca Daawuda, ne ko: «Ana ku moom réew mii?» Mu neeti ko: «Fasool ak man kóllëre. Maa lay jàpple, ba walbatil la Israyil gépp, ñu nangul la.»