2 Samuel 3:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba Abner agsee Ebron ca Daawuda, ñaar fukki nit la àndal. Daawuda berndeel Abner, mook nit ña ànd ak moom.