2 Samuel 3:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yowab agsi mook mboolem gàngoor ga ànd ak moom. Ñu ne ko Abner doomu Ner ñëwoon na ca Buur, ba mu yiwi ko, mu dem ci jàmm.