2 Samuel 3:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xam nga Abner doomu Ner! Wor la moo ko fi indi, ngir xam say dugg ak say génn, ak lépp looy def.»