2 Samuel 3:38 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee Buur wax aki nitam ne leen: «Xanaa xamuleen ne ab garmi, nit ku màgg moo daanu bésub tey fi digg Israyil?