bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Samuel 3:8
2 Samuel 3:8 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Abner mer lool ca la ko Isboset wax. Mu ne ko: «Ndax dama di xajub workat bu Yudeen ñi? Ba tey jii ngor laay jëfe ak sa waa kër baay Sóol, aki bokkam aki soppeem. Te it teguma la ci loxol Daawuda; yaw nga di ma tuumaal ci ndaw sii tey?