2 Samuel 5:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Daawuda xam ne Aji Sax jee ko tabb buurub Israyil te moo kaweel nguuram ngir Israyil, aw ñoñam.