bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Samuel 5:6
2 Samuel 5:6 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu Buur Daawuda ànd aki xarekatam, jëm Yerusalem, songi Yebuseen ña dëkkoon ca réew ma. Yebuseen ña ne Daawuda: «Doo fi dugg de, nde gumba yeek lafañ yi rekk ñoo lay waññi.» Booba foog nañu ne Daawuda manu faa dugg.