2 Samuel 6:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu nag tax Daawuda nanguwula yóbbu gaalu Aji Sax ji fa moom, ca gox ba ñu naan Kër Daawuda. Mu waññi gaal gi, yóbbu ko ca kër Obedd Edom waa Gaat ba.