bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Samuel 6:12
2 Samuel 6:12 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee ñu xamal Buur Daawuda ne ko: « Aji Sax ji de barkeel na Obedd Edom ak mboolem lu bokk ci moom ndax gaalu Yàlla gi.» Daawuda jëleji gaalu Yàlla ga kër Obedd Edom, daldi koy yóbbu ci biir mbégte mu réy ba këram, fa ñu naan Kër Daawuda.