2 Samuel 7:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi nag, Boroom bi Aji Sax ji, yaw yaay Yàlla, say kàddu mooy dëgg, te yaa ma wax lu baax lii, Sang bi.