2 Samuel 9:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mefiboset amoon na doom ju ndaw ju góor, ju ñuy wax Mika. Waa kër Ciba ñépp nag daldi nekk ci liggéeyu Mefiboset.