2 Thessalonians 1:10 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Dina ñëw bés booba, ngir ndamam jolli ci biir gaayam yu sell yi, te ñépp ñi ko gëm yéemu ci moom — te ci ngeen bokk, ndaxte gëm ngeen li nu leen seede.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
kera bés bu délsee ba jot ci teddngaam ci biir ñoñam ñu sell ñi, ba mboolem ñi ko gëm di ko yéemoo. Te yeen ci seen bopp, ci ngeen di bokk, ndax yeena gëm la nu leen seedeeloon.