2 Thessalonians 1:11 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Moo tax dunu noppeek di leen ñaanal, ngir Yàlla sunu Boroom def leen, ngeen yeyoo li tax mu woo leen, te yeggali ak doole ci yéen bépp yéene ju baax ak bépp jëfu ngëm.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax nu saxoo leena ñaanal, ngir sunu Yàlla yellale leen ab wooteem, ngir itam mu sottale kàttanam seen mboolem mébét mu baax, ak seen jépp jëf ju laloo ngëm.