2 Thessalonians 1:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Loolu mooy firndeel àtteb Yàlla bu jub bi, di wone ne yelloo ngeen nguuru Yàlla, gi tax ngeen di sonn.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu lépp di firndeel njekku àtteb Yàlla, bi leen di yellale nguurug Yàlla, gi tax ngeen di sonn.