2 Thessalonians 1:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
safara su yànj wër ko, mu feeñ ngir mbugal ñi xamul Yàlla te bañ a déggal xebaar bu baaxu sunu Boroom Yeesu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci biir sawara wuy sëlsëli lay doon. Ca lay mbugal ñi xamul Yàlla, ak ñi baña déggal xibaaru jàmm bi jëm ci sunu Boroom Yeesu.