2 Thessalonians 2:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci lu jëm ci ñëwu Boroom bi Yeesu Kirist nag, bokk yi, ak sunu daje ak moom, am na lu ma leen di ñaan:
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi nag, bokk yi, ci wàllu dellusig sunu Sang Yeesu Almasi, ak sunu dajeji fa moom, li nu leen di ñaan moo di: