2 Thessalonians 2:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag bokk yi, taxawleen bu dëgër te jàpp ci dénkaane yi nu leen jottali, muy ci li nu wax, muy ci li nu bind.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag bokk yi, taxawleen bu dëgër te ŋoy ci dénkaane yi nu leen àgge ci sunu làmmiñu bopp, ak yi nu leen bind ci sunuy bataaxal.