2 Thessalonians 3:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Léegi nag bokk yi, ñaanal-leen nu, ngir kàddug Boroom bi law te ànd ak ndam, ni mu ko ame woon ci yéen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li ci des nag bokk yi, moo di ngeen ñaanal nu, ngir kàddug Boroom bi gaawa law te am ndam na mu ko ame woon fa yeen,