bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Thessalonians 3:11
2 Thessalonians 3:11 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Léegi nag dégg nanu ne, am na ci yéen ñuy wéy ci tayel; liggéeyuñu dara, lu dul di dugg ci lu seen yoon nekkul.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dégg nanu nag ne ñenn a ngi ci seen biir, ñu nekke ag yaafus, duñu yëngu ci dara, lu moy di topptoo lu seen yoon nekkul.