2 Thessalonians 3:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñu deme noonu nag, nu ngi leen di sant te di leen dénk ci turu Boroom bi Yeesu Kirist, ñuy liggéey ci jàmm tey dunde seen ñaq.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu ni mel lanuy sant ak a dénku ngir Sang Yeesu Almasi, ngir ñu dal, tey yëngu, di dunde seen ñaqu bopp.