2 Thessalonians 3:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su kenn bañee topp li nu bind ci bataaxal bii, ràññeeleen ko te sore ko, ngir mu rus ci.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ku ci déggul sunu kàddu yi ñu bind ci bataaxal bii nag, bàyyileen ko xel, te baña jaxasoo ak moom, ngir gàcceel ko.