2 Thessalonians 3:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Na leen Boroom jàmm may jàmm ci fépp ak ci lépp. Na Boroom bi ànd ak yéen ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu, Boroom bi moom jàmm, yal na leen mayal boppam jàmmi lépp ak fépp. Yal na Boroom bi ànd ak yeen ñépp.