2 Timothy 1:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
looloo tax ma jànkoonte ak tiis yu mel nii. Waaye rusuma ci, ndaxte xam naa Ki ma wékk sama yaakaar, te wóor na ma ne, li ma ko dénk, man na koo denc ba bés ba.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Looloo tax may daj yii coono. Waaye rusuma ci, ndax xam naa ki ma gëm, te wóor na ma ne moo mana sàmm li ma ko dénk ba keroog bés ba.