bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Timothy 1:13
2 Timothy 1:13 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Toppal ci tànki wax yu wér yi nga dégge ci man, jàpp ci ak ngëm ak mbëggeel, yi nu am ci sunu bokk ci Kirist Yeesu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Royal ci kàddu yu wér yi nga dégge ci man, te nga ànd ceek ngëm, ak cofeel gi Almasi Yeesu di maye,